zondag 31 december 2006

Déwënëti!

Baal ma àq.
Yàlla na ñu Yàlla boole baal.
Yàlla na ñu Yàlla feg ci musibë.
Yàlla na ñu Yàlla sàmm.
Yàlla na ñu Yàlla taxawu.
Amiin.

Geen opmerkingen:

Een reactie posten

Zeg 't maar

Opmerking: Alleen leden van deze blog kunnen een reactie posten.